TSK

TSK · Acts 20:26

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 16:19 TSK

Ma ne, tey fi tey, am naa ab seede kaw asamaan, sama seede kay a nga fa kaw.

«Yaw nit ki, waxal ak sa bokk yi, nga ne leen: “Am réew, su ma wàccee xare ci kawam, waa réew ma tànne ci seen biir kenn, def ko seen jongrukat,

Ñoom laa seedeel seenug parlute ci Yàlla, waaye dañu koo tegul ci xam-xam bu doy.

¶ Xajal-leen nu. Tooñunu kenn; lorunu kenn; naxunu kenn, lekkunu alalu kenn.

¶ Yeena seede, Yàlla itam seede, sellnga ak njub, ak mucc sikk ga nu doon jëfe fa seen biir, yeen ñi gëm.