كل أسفار KYG

Acts 21

KYG · الآية 11

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 21

KYG · الآية 11

M u dikk ba ci nun, jël ngañaayal Póol, yeewe ko ay tànkam aki loxoom, daldi ne: «Noo gu Sell gi dafa wax ne: “Ki moom ngañaay lii, nii la ko Yawut yiy yeewe ca Yerusalem, jébbal ko jaambur ñi dul Yawut.”»