TSK

TSK · Acts 23:10

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Éy Aji Sax ji, sama Yàlla, yaw laay làqoo! Musal ma, xettli maak ñi may dàq ñépp.

Micah 3:3 TSK

Yeenay yàpp samay bokk, fulli seen der, damm seeni yax, dogat, def ko ni toggug kawdir, mbete ndawal ci cin.»

Ba loolu amee dëkk ba bépp màbb, nit ña ne kër-kër, ne këpp, ñu jàpp Póol, génne ko kër Yàlla ga rekk, daldi tëj bunt ya.

¶ Jarbaatub Póol bu góor nag yég tëru ma. Mu daldi dem ba ca tata ja, dugg, yégal ko Póol.

Ca ëllëg sa takk-der yay deme tànk waññiku, délsi ca tata ja, bàyyi gawar ga, ñu gunge Póol ba mu àgg.

¶ Bokk yi, soppe yi, nangeen xam lii: na ku nekk di gaaw ci déglu, di yeexa wax tey yeexa mer.