TSK

TSK · Acts 23:19

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Buur wax ma, ne ma: «Ana looy sàkku?» Ma ñaan gaaw ci Yàlla Boroom asamaan,

Ñu dem bay naan biiñ ca bésub ñaareel booba, Buur dellu ne: «Lingeer Esteer, ana looy ñaan, ñu may la ko. Looy sàkku? Ba ci genn-wàllu réew mi sax, ñu defal la ko.»

Du mel ni kóllëre ga ma fasoon ak seeni maam keroog ba ma leen jàppee ci loxo, génne leen réewum Misra. Ndax ñoom ñoo fecci sama kóllëre, te man may seen boroom kër.» Kàddug Aji Sax jee.