Genesis 40:15
TSK
Ndax man kat dañu maa sàcce ca réewum Ebrë ya, te fii itam, defuma fi lu tax, ñu war maa tëj.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ndax man kat dañu maa sàcce ca réewum Ebrë ya, te fii itam, defuma fi lu tax, ñu war maa tëj.»
¶ Dañeel daldi ne Buur: «Buur, guddalu fan!
¶ Ba loolu amee Póol xool jàkk waa kurél ga, ne leen: «Bokk yi, man de xel mu dala dal laa masa jëfe fi kanam Yàlla, ba bésub tey jii.»
Te giseesu ma may werante, mbaa may yëngal mbooloo; du ca kër Yàlla ga, du ca jàngu ya, du ca biir dëkk ba.
¶ Póol itam ne ko: «Maa ngi nii taxaw ci kanam àttekaayu Buur Sesaar; te fii lañu ma wara àttee. Yawut ñi nag, defuma leen dara, te yaw ci sa bopp, wóor na la.
¶ Ñu ne ko: «Nun de, du benn bataaxal bu nu jot bu jóge Yude ci sa mbir, te du kenn ci bokk yi, ku dikk wax mbaa mu seedeel la lenn lu bon.