TSK

TSK · Acts 27:44

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Amos 9:9 TSK

«Maa ngii déy di sant xeetoo xeet, ñu gësëm waa kër Israyil, ni ñuy gësëme tameb suuf, te doj du rot.

Léegi nag dama leen di ñaax, ngir ngeen dalal seen xel, ndax kenn ci yeen du ñàkk bakkanam, gaal gi rekk ay yàqu.

Póol nag ne njiitu takk-der ba ak xarekat ya: «Ñii bu ñu desul ci gaal gi, yeen dungeen raw.»

Te it: «Aji jub ji, su ko mucc jafee, yéefar bi, bàkkaarkat bi moom, fu mu jëm?»