TSK

TSK · Acts 28:30

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba loolu amee Buur Cedesyas santaane ñu teg Yeremi ca biir ëttu dag ya. Ñu di ko jox bés bu ne menn mburum lëmm mu jóge ca mbeddu Lakk-kati mburu ya, ba keroog mburu di ñàkk ca dëkk ba. Yeremi nag toog ca ëttu kër dag ya.

¶ Ba ñu ca tegee ñaari at yu mat, ku ñuy wax Porsiyus Festus wuutu Feligsë. Feligsë nag bëggoon lu neex Yawut ya, ba tax mu bàyyi Póol ca kaso ba.

Su ko defee, ci coobarey Yàlla, ma dikke mbégte ba fa yeen, ba dal-luwaale as lëf fa yeen.

Xanaa ay surgay Almasi lañu? Naa ràkkaaju nag, te ne maa leen ko gëna doon. Bu dee ci liggéey yu metti, maa man fopp; bu dee ci fani kaso, maa ëpple fopp; bu dee ci ay yar, maa ëpple ay yooni yoon, te bare na lu ma riisu ndee, ba raw leen:

waaye ba mu dikkee Room, da maa seeta seet, ba gis ma.