TSK

TSK · Acts 3:10

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Luke 4:36 TSK

¶ Ba loolu amee ñépp a waaru, di wax ci seen biir, naan: «Gii kàddu lu mu doon? Moom de sañ-sañ ak xam-xam lay joxe rab yi ndigal, ñu génn.»

Acts 2:12 TSK

Ñépp waaru, ba jànnaxe, di wax ci seen biir naa: «Lii lu muy tekki nag?»

Acts 4:14 TSK

Te itam ka ñu wéral a nga taxaw fa seen wet, ñuy gis. Manuñu caa tegati dara.