كل أسفار KYG

Acts 3

KYG · الآية 16

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 3

KYG · الآية 16

G ëm aw turam moo waral turam woowu dooleel nit kii ngeen gis, xam ko. Kon ngëm moo waral lii; ngëm gu sababoo ci Yeesu moo ko may mu wér péŋŋ nii ci seen kanam, yeen ñépp.