كل أسفار KYG

Acts 4

KYG · الآية 24

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 4

KYG · الآية 24

B a ko bokk ya déggee, ñoom ñépp a mànkoo, daldi yékkati kàddug ñaan fa Yàlla, ne: «Buur Yàlla, yaa sàkk asamaan ak suuf ak géej ak lépp li ci biir.