Psalms 2:4
TSK
Ki ci jalub asamaan a ngay ree, Boroom baa nga leen di kókkali,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ki ci jalub asamaan a ngay ree, Boroom baa nga leen di kókkali,
Nit xeluwul, amul ug dégg ak pexe, ba manal Aji Sax ji dara.
Aji Sax ji, fa xóotey pax ma laa la wooye
¶ Dañeel daldi ne Buur: «Buur, guddalu fan!
Ca guddi ga nag malaakam Boroom bi ubbi bunti kaso ba, génne leen, ne leen: