TSK

TSK · Acts 5:34

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ca la Yàllay jóg, ngir àtte, ba wallu kuy néew dooley àddina. Selaw.

Luke 5:17 TSK

¶ Yeesu moo doon jàngle bés, fu ay Farisen ak ay jànglekati yoonu Musaa tooge, jóge ca mboolem dëkki Galile ak Yude ak Yerusalem, te manoorey Boroom bi teew faak moom, ngir faj jarag ja.

Acts 4:15 TSK

Ba mu ko defee ñu joxe ndigal, génne leen, daldi gise ci seen biir.

Acts 23:7 TSK

Naka la wax loolu Farisen yaak Sadusen ya tàmbalee werante, ba mbooloo ma xàjjalikoo.