Exodus 18:17
TSK
Goro ba ne ko: «Ni ngay doxale gënul.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Goro ba ne ko: «Ni ngay doxale gënul.
¶ Musaa teg ca ne leen: jant yooyu laa leen wax, ne leen: «Duma leen àttan yeen ñépp, man doŋŋ.
Piyeer ak Yowaan ne leen: «Ndax li jaadu fa Yàlla mooy nu déggal leen, yeen, bàyyi Yàlla? Yeenay àtte loolu.
Ndaxte jàllale ku ñu jàpp te tudduloo tuuma yi ñu koy topp daal, lu juunu la ci man.»