Isaiah 65:24
TSK
Su boobaa balees woote, man, maay wuyu; balaa ñoo daane seen kàddu, ma nangul leen.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Su boobaa balees woote, man, maay wuyu; balaa ñoo daane seen kàddu, ma nangul leen.
¶ Naka la Piyeer di xalaat ba tey ca peeñu ma, Noo gi ne ko: «Ñetti nit a ngi nii, di la seet.
Ñooñoo daje woon di màggal Boroom bi, boole kook koor. Ci biir loolu Noo gu Sell gi ne: «Beral-leen ma nag Barnaba ak Sóol ngir liggéey, bi ma leen wooye.»
¶ «Léegi maa ngii ci curgag Noo gu Sell gi, di dem Yerusalem, lu ma fay dal sax, xawma ci dara,
Loolu lépp, genn Noo googu moo koy def, ku nekk, mu sédd la ci, ni mu ko soobe.