2 Kings 4:28
TSK
Ndaw sa ne ko: «Sang bi, ndax maa la ñaan doom ju góor? Newuma la woon bu ma nax?»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ndaw sa ne ko: «Sang bi, ndax maa la ñaan doom ju góor? Newuma la woon bu ma nax?»
¶ Dëkk ba ñuy wax Yope, ab taalibe bu jigéen a nga fa woon, ñu di ko wax Tabita mbaa Dorkas ci làkku gereg. Def lu baax ak sarxe la saxoo woon.