1 Kings 17:23
TSK
Ilyaas fab xale ba, jële ko ca néeg ba ca kaw taax ma, wàcce ko ca biir kër ga, jox ko ndeyam. Mu ne ko: «Xoolal, sa doom a ngi dund!»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ilyaas fab xale ba, jële ko ca néeg ba ca kaw taax ma, wàcce ko ca biir kër ga, jox ko ndeyam. Mu ne ko: «Xoolal, sa doom a ngi dund!»
Ñaanu ku naroona sànku di ma dal, may tooyal xolu jëtun.
Néew ba jóg toog, di wax, mu delloo ko yaay ja.
¶ Jant yooyu nag, naka taalibe yi di gëna bare, Yawut ñiy làkk gereg tàmbalee ñaxtu ci kaw Yawut ñiy wax seen làmmiñu bopp ndax néewal gu ñu gis ñu néewal ko seeni jëtun ca na ñuy séddalee ag ndimbal bés bu nekk.