TSK

TSK · Amos 1:5

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Buurub Asiri nangul ko, dal ca kaw Damaas, nangu dëkk ba, jàpp waa dëkk ba, yóbbu Kir, ba noppi rey Reccin.

Aji Sax jiy seen jotkat, Aji Sell ju Israyil dafa wax ne: «Yeena tax ma yebal ku songsi Babilon, ba dàjji lu fay tëjukaay, ba xaxalooy Kaldeen ñooñu diy jooyoo.

Jàmbaari Babilon xareetuñu, ña nga des ca seeni tata, doole ŋiis, ñu mel niy jigéen. Bunti dëkk bi dàjjiku, kër ya jàpp.

Xaleli góori On ak Pi Beset, saamar lañuy fàddoo, waa dëkk yooyu ca des njaam lañu jëm.

Amos 5:5 TSK

Buleen sàkkuji fa Betel, buleen dem Gilgal, te buleen jàll Beerseba. Gilgal ay gàlloo ngàllo; Betel neen.»

Say gàngoor a ngii diy jigéen fi sa biir, sa bunti réew lafal say noon, ne ŋàpp-ŋàppaaral, sawara xoyom tëjukaay ya!