TSK

TSK · Amos 1:9

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ci biir loolu Iram buurub Tir, yebal ay ndaw ca Daawuda, ñu yóbbul ko ay banti garabu seedar, ak ay liggéeykati bant ak yettkati xeer, ngir ñu tabaxal Daawuda kër.

fekk na Iram buurub Tir jox Suleymaan ay banti garabi seedar ak sippar, ak mboolem lu mu soxla ci wurus. Buur Suleymaan nag jox Iram ñaar fukki dëkk ci diiwaanu Galile.

¶ Yéene bii ñeel na dëkk ba ñuy wax Tir: Yeen waa gaali Tarsis ñi deele, jooyleen! Lépp a yàqu! Du kër, du teeruwaay. Fa dunu Sippar lañu leen ko waxe.

bésub sànkute dikkal képp kuy Filisteen, ba dagge dëkk yii di Tir ak Sidon ndimbal lu ñu dese woon. Aji Sax jaa ngay sànk Filisteen, ña des te cosaanoo dunu Keret.

¶ Kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

¶ Kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

Amos 1:6 TSK

Aji Sax ji nee: «Ñetti bàkkaar, su ma yeboo ne ñeent, laay sikke waa Gasa, te duma fomm seeni duma. Ñoo jàpp njaam mbooloom lëmm, jalax Edomeen ña.

Kàddu gi dal na itam Amat, ga digalook Damaas, dal Tir ak Sidon, ak la ñuy muus lépp.