TSK

TSK · Amos 5:20

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 10:21 TSK

bala may dëddu, délseetuma, bala may tàbbi réew mu lëndëm ga ne këruus,

Ni ab sàmm di seete ag juram fu ñu tasaaroo, ni laay seete samag jur, ba xettlee leen mboolem fu ñu tasaarooji woon bésub ngëlén bu lëndëm.

Nahum 1:8 TSK

Mbàmbulaan lay walal ba faagaagal dëkk bii, te mooy toppi noonam ba ca biir lëndëm ga.

¶ Juróomeelu malaaka mi sotti ndabam ci kaw ngàngunem rab wi, nguuram daldi sóobu ci lëndëm, nit ñi di yéyu ndax metit,