TSK

TSK · Amos 8:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Muy kàddug Sabóor, ñeel Daawuda. Mooy ba mu nekkee ca màndiŋu Yuda.

Waxambaane sonn, loof; xalelu góor di tërëfa tërëf,

«Yeen waa Dibon, dëkk bu taaru bi, wàccleen seen teddnga lu kawe te tooge digg maral; kiy yàqtesi Mowab kat song na leen, di màbbsi seeni tata.

Magi janq Siyoŋ mu taaru ña nga toog, xeremlu, xëppoo suuf, sol ay saaku, di ñaawlu. Janqi Yerusalem sëgg, seen bopp jëm suuf.

Hosea 2:3 TSK

Nanga wooye sa bokk yu góor: “Ñoñi Aji Sax ji,” sa bokk yu jigéen, nga ne leen: “Ñi Aji Sax ji yërëm.”

Ndaw bànneex akub taar ca ñoom! Pepp yafal xalelu góor, biiñ bu bees naatal yaramu janq.