TSK

TSK · Colossians 4:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ñaanu Aana ca Aji Sax ji nag yàgg, Eli di ko seetlu.

Job 15:4 TSK

Yaw de, yaa ngi neenal worma, di yàq njàngat mi war fa Yàlla.

Yal na leen dee bett, ñu jekki tàbbi njaniiw, ngir mbon ga seen biir ak seen dëkkuwaay.

Luke 18:1 TSK

¶ Yeesu dellu leen léeb lii, ngir ñu wareefoo di sax ci ñaan te baña xàddi.

Bégeleen seen yaakaar, di muñ ci biir tiis, tey saxoo ag ñaan.

Buleen jaaxle ci dara, waaye ci mbir mu mu mana doon, deeleen dikke Yàlla seeni soxla, di ko ñaan ak a dagaan te boole ci di ko sant.

Sampleen seeni reen ci moom, tabaxuleen ci moom, feddlikuleen ci wàllu ngëm, ni ñu leen ko jàngale, ba seenub xol baawaanal kàdduy cant.

Lu ngeen mana def, muy ci wax, di ci jëf, defleen ko ci turu Sang Yeesu, tey sant Yàlla Baay bi ci moom.