كل أسفار KYG

Daniel 1

KYG · الآية 17

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 1

KYG · الآية 17

Y àlla nag may ñeenti xale yu góor yooyu xel ak ràññee ci mboolem lu ñu bind ak wàllu xam-xam. Dañeel moom mana firi mboolem peeñu ak gént.