كل أسفار KYG

Daniel 10

KYG · الآية 11

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 10

KYG · الآية 11

M u ne ma: «Dañeel, yaw mi ñu naw, déggal kàddu yi ma lay wax. Jógal taxaw sa taxawaay, ndax dañu maa yebal ci yaw nii.» Naka la ma wax kàddu yooyu, ma ne ñokket, di lox.