كل أسفار KYG

Daniel 10

KYG · الآية 13

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 10

KYG · الآية 13

W aaye rawaanu nguurug Pers moo ma dogale ñaar fukki fan ak benn. Mikayel nag, kenn ci malaakay wattukat yu mag yi ñëw, wallusi ma. Yàgg naa ca buuri Pers ya.