Màggaay ga mu ko mayoon tax waa mbooloo yeek xeet yeek làkk yépp ragal ko, bay lox ci kanamam. Ku ko soob, mu rey; ku ko soob, mu bàyyi; ku ko soob, mu fal; ku ko soob, mu torxal.
TSK
TSK · Daniel 11:3
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Daniel 5:19
TSK
Daniel 8:4
TSK
Ma gis kuuy may dañ, di jublu sowu ak bëj-gànnaar ak bëj-saalum. Menn mala manu koo të, te maneesula xettli kenn ci moom. Ma ngay def lu ko neex tey gëna màgg.
Daniel 8:21
TSK
Sikket bi buuru réewum Geres la. Béjjén bu gudd bi ci diggante bët yi mooy buur bu jëkk bi.
Daniel 11:36
TSK
¶ «Buur bi dina def lu ko soob. Dina réy-réylook a damu, ba weesale boppam tuur yépp, te dina wax gilaawaali jëme ci Yàlla ji sut lépp. Dina am ndam nag ba keroog sànjum Yàlla ñoral ko. Li ñu dogal déy dina am.
Hebrews 2:4
TSK
Te Yàlla moo doon dëggale seedey ñooñu, ay firnde aki kéemaan, ak wépp xeeti kawtéef, ak ay mayi Noo gu Sell gi, may yi mu séddalee ni mu ko soobe.