Mu ne: “Maay dikk, doon xel muy safaan dëgg ci làmmiñu yonentam yépp.” Mu ne ko: “Yaa koy nax, te man nga ko. Demal defe noonu.”
TSK
TSK · Daniel 2:9
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Kàdduy dëgg, day sax dàkk; fen, xef xippi, mu wéy.
Maay neenal firndey maaman, dofloo gisaanekat. Maay weddi fóore, def xam-xamam mu dig ndof.
«Yaw nit ki, janool ak sa bokk yu jigéen, yiy waxe waxyu ci seen xelum bopp, nga wax waxyu fi seen kaw.
Dañeel nag dem ca Buur, ñaan ko mu may ko jot gu mu ko joxe pirim gént ga.
Léegi, bettuma leen. Bu ngeen di dégg bufta geek toxoro geek xalam geek riiti geek kooraa geek liit geek mboolem jumtukaayi xumbal yi rekk, sujjóotleen, màggale ko jëmm ji ma sàkk. Waaye su ngeen ko màggalul, dees na leen daldi sànni ci biir taalu sawara bu yànj. Ana yàlla ju leen di musal ci man?»
Nun nag danoo melul ni ñu bare, ñiy julaa kàddug Yàlla, waaye ci ndigalal Yàlla ak fi kanam Yàlla la nuy waaree xol bu set, ci Almasi mi nu gëm.