Buur Nabukodonosor nag woolu jawriñ yaak laman yaak jaraaf yaak kàngam yaak farbay alal yaak àttekat yaak ndawi buur yaak mboolem kilifay diiwaan ya, ngir ñu ñëw ca bernde ja mu maye ca daloob jëmm ja mu samp.
TSK
TSK · Daniel 3:24
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Daniel 3:2
TSK
Daniel 3:17
TSK
Ndegam Yàlla ji nuy jaamu man nanoo musal ci taalu sawara bu yànj bi, musal nu ci yaw mii, dina nu musal.
Daniel 4:27
TSK
Ma ngay wax naan: «Xanaa lii du Babilon gu mag gi ma tabax man, ci sama doole ju réy, muy péeyu buur, di sama ndam ak sama daraja?»
Daniel 5:18
TSK
¶ «Buur, Yàlla Aji Kawe ji daa joxoon sa baay Nabukodonosor nguur gi, muy ku màgg, am ndam ak daraja.
Daniel 6:22
TSK
¶ Dañeel daldi ne Buur: «Buur, guddalu fan!
Acts 9:6
TSK
Léegi nag, jógal, dugg ci dëkk bi, dees na la wax li nga wara def.»
Acts 26:13
TSK
Ba ma demee ba wetu digg bëccëg, Buur, ca laa gis ag melax gu leer ba raw jant bi, fettaxe asamaan, ne ràyy fi ma wër, maak ñi ma àndal.