¶ Ba bët setee, Firawna jaaxle lool, ba woolu jibar ya ak boroom xam-xami Misra yépp, nettali leen la mu gént, te kenn manu koo firil Firawna.
TSK
TSK · Daniel 4:18
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 41:8
TSK
1 Kings 14:2
TSK
Yerbowam wax soxnaam, ne ko: «Ayca, doxal soppiji col, ba kenn du xam ne sama soxna nga, te nga dem Silo. Dama ne, Axiya yonent baa nga fa. Moo ma waxoon ne ma dinaa falu buur, jiite mbooloo mii.
Isaiah 47:12
TSK
Jàppool say jat rekk ak sa xërëm yu ne xas yoo dale sonn ba ngay ndaw. Jombul mu amal la njariñ, mbaa ñu ragale la ko.
Daniel 2:26
TSK
Buur wax ak Dañeel, mi ñu naan Beltasar, ne ko: «Wóor na la ne man nga maa wax li ma gént, wax ma li muy firi?»
Daniel 4:7
TSK
Li ma gis daal ci sama kaw lal mooy lii: Damaa jekki gis garab ci digg àddina si, mu gudd lool.
Daniel 5:15
TSK
Léegi indiloon nañu ma boroom xam-xam yeek ñeengokat yi, ndax ñu jàngal ma mbind mii, xamal ma pireem. Waaye xamuñu pireem.