كل أسفار KYG

Daniel 4

KYG · الآية 22

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 4

KYG · الآية 22

Y aw lañuy dàqe ci nit ñi; rabi àll yi ngay dëkkal, ñax di sam xont niw nag, lay biy wàcc di la faam diiru juróom ñaari jamono, ba kera ngay xam ne Aji Kawe jee yor nguurug nit, di ko jox ku ko neex.