كل أسفار KYG

Daniel 4

KYG · الآية 29

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 4

KYG · الآية 29

D ees na la dàqe ci nit ñi, nga dëkk ak rabi àll yi, ñax di sam xont niw nag diiru juróom ñaari jamono, ba kera ngay xam ne Aji Kawe jee yor nguurug nit, di ko jox ku ko neex.»