كل أسفار KYG

Daniel 5

KYG · الآية 11

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 5

KYG · الآية 11

A m na góor gu nekk ci sa réew mi; xelu yàlla yu sell yaa ngi ci moom, te ci sa jamonoy baay, gis nañu ci moom ag ràññee ak xel ak xam-xam bu nirook xam-xamu yàlla yi. Buur Nabukodonosor sa baay nag fal ko, mu jiite taryaax yeek ñeengokat yeek xërëmkat yeek seetkat yi;