كل أسفار KYG

Daniel 6

KYG · الآية 13

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 6

KYG · الآية 13

b a noppi ñu dem fekki Buur, ngir wax ak moom ca aaye ba mu tëral, ne ko: «Xanaa du yaa torlu aaye bi ne: képp ku ñaan jenn yàlla mbaa nit ku la moy, yaw Buur, diiru fanweeri fan, dees na ko sànni ca kàmbu gaynde ya?» Buur ne: «Dogal bi kay wér na, dëppook yoonu waa Medd ak Pers, wi dul toxu.»