كل أسفار KYG

Daniel 6

KYG · الآية 23

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 6

KYG · الآية 23

S ama Yàlla yebal na malaakaam, mu tëj gémmiñi gaynde yi, ba defuñu ma dara. Ndax kat mucc naa ci tuuma sama digganteek moom ak sama digganteek yaw it, te defuma dara lu bon.»