Naka la ne gees, ne leen jàkk, daldi leen móolu ci turu Aji Sax ji. Ci kaw loolu ñaari urs génne ca àll ba, fàdd ca gone ya ñeent fukk ak ñaar.
TSK
TSK · Daniel 7:5
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Maa ngii di xabtal fi seen kaw waa Medd, ñi xintewoowul xaalis, faalewuñu wurus.
Yeen rabi àll yi, dikkleen ci bernde ji, yeen rabi gott bi yépp.
¶ «Yaw nit ki nag, Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Waxal picc yi ak mboolem njanaaw yi ak rabi àll yépp, ne leen: “Dajalooleen, jóge fu ne, dikk, dajesi ci sama sarax si ma leen di rendil, muy sarax su mag fa kaw tundi Israyil, ngeen lekk yàpp, naan deret.
SÉDDALE: Séddale nañu sam réew, ba jox ko xeeti Medd ak Pers.»
Ma gis kuuy may dañ, di jublu sowu ak bëj-gànnaar ak bëj-saalum. Menn mala manu koo të, te maneesula xettli kenn ci moom. Ma ngay def lu ko neex tey gëna màgg.
Maay dajeek yeen ni rab wu aay wu ñu xañi doom, maay xotti seen mbuusum xol, fa laa leen di yàppe ni gaynde, te rabu àll moo leen di xotat.