Daniel 7:6
TSK
¶ «May xool ba tey, yem ci rab wu mel ni segg, am ñeenti laaf. Rab waa ngi am ñeenti bopp, ñu jox ko kilifteef gi.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «May xool ba tey, yem ci rab wu mel ni segg, am ñeenti laaf. Rab waa ngi am ñeenti bopp, ñu jox ko kilifteef gi.
Mu ne ma: «Ndax xam nga lu ma taxa dikk? Léegi ma dellu xarejeek rawaanu réewum Pers; te bu may dem, rawaanu Geres dikk.
Yuda déy laay bank, muy samag xala, te Efrayim laa koy soxe, muy fitt gi. Yaw Siyoŋ, sa doom yu góor laay yékkati ci sa kaw doom yu góor, yaw réewum Geres (/Yawaan). Doomi Siyoŋ laay def saamaru jàmbaar.