كل أسفار KYG

Daniel 8

KYG · الآية 27

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 8

KYG · الآية 27

B a loolu amee ma ne làcc, wopp ay fan, man Dañeel. Gannaaw gi ma jóg, dellu ca liggéeyu buur. Ma waaru nag ca peeñu ma, ndax daa wees sama dég-dég.