كل أسفار KYG

Daniel 9

KYG · الآية 21

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 9

KYG · الآية 21

M aa ngay wax ci ñaan gi, waa ja Jibril ma ma gisoon lu jiitu ci peeñu mi, daldi naawa naaw, dikk ba ci man, yemook waxtuw saraxu ngoon.