كل أسفار KYG

Daniel 9

KYG · الآية 25

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 9

KYG · الآية 25

N anga xam kon xéll ne: li ko dale keroog ba ñuy siiwtaane dogal ba jëm ci leqli Yerusalem, tabaxaat ko, ba keroog njiit li ñu fal di feeñ, juróom ñaari àppi juróom ñaar la. Te ci juróom benn fukk ak ñaar ci àppi juróom ñaar lañuy tabaxaat pénc ak kàmb gu ñu aare dëkk bi. Waaye jamono yu metti lay doon.