كل أسفار KYG

Daniel 9

KYG · الآية 7

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 9

KYG · الآية 7

Y aw Boroom bi, njub ñeel na la, waaye nun gàcce ñeel na nu bésub tey jii, muy waa Yuda, muy waa Yerusalem, di waa Israyil gépp, ku jegeek ku sore, ci biir mboolem réew yi nga leen dàq, yóbbu, ndax li ñu la ñàkke kóllëre.