TSK

TSK · Deuteronomy 13:15

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

su boobaa buleen sujjóotal mukk seeni tuur, di leen jaamu, mbaa ngeen di roy seeni aada, waaye yàqteleen seeni tuur te toj tasar seen tuuri doj, ya fa sampe.

Jant yooyu lanu nangu dëkkam yu mag yépp, faagaagal dëkk yu mag yépp: góor ak jigéen, ba ca tuut-tànk ya, bàyyiwunu kuy dund.

Fàkkasleen mboolem xeet yi leen seen Yàlla Aji Sax ji jébbal nag. Buleen leen xool bëtu yërmande, buleen jaamu seeni tuur: Lu ko moy muy seenug fiir.

Ci kaw loolu ngàllo, ga ñibbsi daldi def la ñu wax. Esra sarxalkat ba tànn nit ña jiite seen kër baay, ku nekk ak làngam, ñoom ñépp ñu tudd seeni tur. Keroog benn fan ca fukkeelu weer wa nag, ñu toog ngir seet mbir ma.

¶ séen saxaras lakku dëkk bi di jalu, naan: «Bii dëkk bu mag, ana dëkk bu masa nirook moom?»