Gàtt ba bumu am sikk te na di kuuyu menn at. Man naa doon xar mbaa sikket.
TSK
TSK · Deuteronomy 16:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Nangeen ci def saraxu sawara, mu dib rendi-dóomal, ñeel Aji Sax ji: ñaari yëkk yu ndaw, ak menn kuuy, ak juróom ñaari xari menn at, te ngeen def lépp di lu mucc sikk.
su boobaa bérab bu seen Yàlla Aji Sax ji taamu ngir dëël fa turam, foofa ngeen di yóbbu mboolem lu ma leen sant: seen saraxi dóomal, ak yeneen sarax, ak seen céri fukkeel, ak seenub jooxe, ak mboolem ngëneel yu ngeen di def saraxi xas yu ngeen xasoo ak Aji Sax ji.
ndare ngeen lekke ko fa seen kanam Yàlla Aji Sax ji. Lekkeleen ko fa seen Yàlla Aji Sax ji di taamuji, yeen ak seen doom yu góor, ak yu jigéen, ak seen jaam yu góor ak yu jigéen, ak Leween ñi ci seen biir dëkk. Su ko defee ngeen bége seen wépp ñaq, fi seen kanam Yàlla Aji Sax ji.
Fi seen kanam Yàlla Aji Sax ji ngeen ko wara xéewloo at mu jot, yeen ak seen njaboot, fi bérab bi Aji Sax ji taamu.
ne leen: «Yàkkamti woon naa lool bokk ak yeen reeru bésub Mucc bii, bala maa tàbbi coono.