TSK

TSK · Deuteronomy 21:6

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 9:30 TSK

Su ma raggoo woon saabu, ba raxasoo xeme sax,

Aji Sax ji, maay jàpp ci biir mucc ayib, di wër sa sarxalukaay,

Ñaawtéef daal laa judduwaale, te sama ndey ëmbaale ma bàkkaar.

Man kay maa sellal ci neen, di sàmm sama der.