TSK

TSK · Deuteronomy 3:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Musaa nag tudde cér yii, askanu Gàdd, ak askanu Ruben, ak genn-wàllu giirug Manase doomu Yuusufa: nguurug Siwon buurub Amoreen ñi la leen jox, ak nguurug Og buuru Basan, réew ma mépp, boole ca dëkk yu mag ya, ak àll ya ko wër.

fa dale ca Arower, ga ca catal walum Arnon, ba ca tundu Siyoŋ, ga ñuy wax itam Ermon,