TSK

TSK · Deuteronomy 32:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Seetleen rekk ci janti démb yi leen jiitu, la dale bés ba Yàlla sàkke nit fi kaw suuf, mbaa ngeen seet asamaan, cat ba cat. Ndax lu màgge nii mas naa am? Am masees naa dégg lu ni mel?

Ma nga naan ca xelam: «Duma tërëf, safaan du ma dab tey ak ëllëg.»

Éy Yàlla, noo déggal sunu bopp, sunuy maam a nu wax jëf ja nga jëf, ca seeni jant, bu yàgga yàgg.

xanaa xalaat janti démb, at ya woon.

Ma ne, sama naqar daal mooy Aji Kawe ji daa soppi loxoom.

Éy Aji Sax ji, damaa fàttliku sa àtte ya woon, daldi muñ.

Ñoñam ña daldi fàttliku janti Musaa ya woon. Ña nga naan: «Ana ki jàlle woon Israyil géej, mook sàmmi géttam ga? Ana ki yebaloon noowam gu sell ci seen biir?