Léegi nag sa ñaari doom, yi nga am Misra, laata ma di la fekksi Misra, maa leen séddoo. Maay séddoo Efrayim ak Manase, ñuy samay doom, ni ma jure Ruben ak Simeyon.
TSK
TSK · Deuteronomy 33:13
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 48:5
TSK
Genesis 48:15
TSK
Ma ngay ñaanal Yuusufa. Mu ne: «Yàlla ji samay waajur Ibraayma ak Isaaxa toppoon, moom Yàlla, ji ma sàmm, ba ma juddoo ba tey jii,
Deuteronomy 32:2
TSK
Na samam njàngle sóob nib taw, samay kàddu rogalaat nib lay, ba tuurul am ñax, baawaanal gàncax.
Psalms 110:3
TSK
Sa mboolooy taxawal seen bopp, sa bésub xare. Ña nga soloo darajaak sellnga, faboo fa njël sosoo, diy ndaw, wàccsil la, mbeteb lay.
Proverbs 19:12
TSK
Merum buur ni gaynde gu ŋar; yërmandey buur ni lay cig mbooy.
Hosea 14:5
TSK
Aji Sax ji nee: «Maay garabal seenug déggadi, maa leen di bëggal sama bopp, nde mereetuma leen.
Zechariah 8:12
TSK
«Ndax jiwum jàmm lay doon, garabu reseñ meññ doomam, suuf si meññ gàncaxam, asamaan di lay. Loolu lépp laay sédd ndesu askan wii.