TSK

TSK · Ecclesiastes 12:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Booba bëti Israyil dafa lëndëm, ba gisatul ndax li muy mag. Yuusufa jegeñal leen seen maam, mu fóon leen, taf leen ci boppam.

Booba Elee ngi ci juróom ñeent fukki at ak juróom ñett (98), bët yi ne xóll te gisatul dara.

Maa ngi ne yogg, ba di la fàttlikoo fa réewum Yurdan ak tundi Ermon ak Misar.

Kàttan nga jote sa mbooloo ma, sëti Yanqóobaak Yuusufa. Selaw.

Bésub keroog ñu ŋaral Yuda, ŋar yu mel ni géej gu sàmbaraax! Foo geesu ci réew mi, xool, doo gis lu moy lëndëm ak njàqare, xàmbaar maase, ba leer giim.