TSK

TSK · Ephesians 2:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Xaymab jaamookaay bi nag, defare ko fukki sori rabali lẽe, mu ànd ak wëñ gu baxa te laal yolet ak wëñ gu xewar ak gu xonq curr, te nga ñawaale ca nataali serub.

Say santaanee wér te wóor; Aji Sax ji, sellnga la sa kër jagoo bésoo bés.

Bunti sàppey néeg ya ca bëj-saalum it noonu la. Ca catal jaarukaay ba, ab bunt a nga fa, janoo màkk ak miir ba féete penku.

¶ Xanaa xamuleen ne kër Yàlla ngeen, te Noowug Yàlla moo dëkk ci yeen?

Su ko defee nu mana màgg nun ñépp ba doon benn ci ngëm, ak ci xam-xam bu mat ci Doomu Yàlla ji, ba kera nuy doon magum jëmm, bay tollook taxawaayu Almasi bi mat sëkk.