TSK

TSK · Esther 3:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Waa Noob dëkkub sarxalkat ya it, mu jam leen, leele ñawkay saamar; góor ak jigéen, gone ya, ba ca ñay nàmp, ak nag yaak mbaam yaak gàtt ya, lépp la leele ñawkay saamar.

Ndax dañu noo fexeel maak samaw xeet, nar noo sànk, bóom nu, faagaagal nu. Su doon ay jaam yu góor ak yu jigéen sax lañu nuy fexee def, dama naan cell, ndax njàqare ju ni tollu sax jarul ñuy lëjal Buur.»

Mardose bind ci turu Buur Aserus, tay bataaxal yi, torloo ko jaarob buur, yóbbante ko ay gawar yu war dawkati naari góor yu ñu tànn.

¶ Gannaaw loolu fukki fan ak ñett ci weeru Adar, fukkeelu weer waak ñaar taxaw, ñu war caa amal dogalu buur ba. Muy bés ba nooni Yawut ya yaakaaroona jekku Yawut ya. Mbir ya nag mujj safaanoo, Yawut ya jekku seeni bañ.

Job 9:25 TSK

Ab dawkat sax ni samay fan di jeexee ko raw. Wone nañu gannaaw te gisuñu lu baax.

Xélukat dab xélukat; ndaw jottli ndaw xibaar bu ñu yeggeji buuru Babilon, ne ko nangu nañu dëkkam ba wetoo wet,

Daan bu àndul ak yërmande, moom lees di àttee ña daawul jëfe yërmande. Yërmande nag kekku na ab daan.