¶ Ba bët setee, Firawna jaaxle lool, ba woolu jibar ya ak boroom xam-xami Misra yépp, nettali leen la mu gént, te kenn manu koo firil Firawna.
TSK
TSK · Esther 6:13
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 41:8
TSK
Moo leen fekk réewum màndiŋ, fu ne wëyëŋ, ubaleeki sab, mu feg leen, topptoo leen, sàmm leen, ni bu ñu doon peru bëtu boppam.
Esther 5:10
TSK
Terewul Aman ànd ak sagoom, ñibbi këram. Ci kaw loolu mu yónnee, woolu ay xaritam ak Seres jabaram.
Job 16:2
TSK
Kàddu yu mel nii, dégg naa ko lu bare. Dëfalkati yokk joote yi ngeen doon, yeen ñépp!
Proverbs 28:18
TSK
Mat, mucc; dëng, dàll daanu.
Daniel 5:26
TSK
Li muy firi mooy: WAÑÑ: Yàlla waññ na sa nguur, ba jeexal ko.
Zechariah 2:12
TSK
¶ Aji Sax ji Boroom gàngoor yi déy dafa wax, moom mi ma yebal ngir teddngay boppam, ci mbirum xeet, yi leen sëxëtoo woon, nee: «Képp ku leen laal kat, laal na sama reeni xol.