TSK

TSK · Exodus 10:4

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Te wax naa la ne la, nga bàyyi sama doom, ndax mu man maa jaamu, nga bañ. Kon nag dinaa rey sa taaw bu góor.’ ”»

Ñu jal koo jal, ba xet ga ubale ca réew ma.

¶ Aji Sax ji nag jàpp na bés, nee na: «Ëllëg maay def loolu ci réew mi.»

¶ Musaa daldi wax Firawna ne ko: «Aji Sax ji dafa wax ne: “Bu guddi gi xaajee, maay wër Misra gépp,

Joel 1:4 TSK

Ndesu soccet yi la njéeréer yi lekk, ndesu njéeréer yi, seenu tostan lekk, seen ndesu tostan, salleer yi lekk.

Joel 2:25 TSK

«Sama mbooloom xare mu réy, mi ma yebaloon fi seen biir, te ñuy njéeréer yeek seen tostan, ak salleer yeek soccet yi, maa leen di delloo ati mbey yi ñu leen lekkal.